LE SAVIEZ VOUS? 

Dialoguer avec son enfant stabilise les émotions

Posez des questions aux enfants, solliciter leurs opinions, est une façon d’inciter leur estime de soi.

Les ordres ou les instructions et surtout les interdits tuent le réflexe d’initiative des enfants et l’esprit de créativité. Nous voulons que les enfants nous respectent mais pas qu’ils nous craignent. Donc dialoguons!

Exemple de dialogue avec son enfant :


Enfant: Je veux voir mes amis! Je ne veux plus rester à la maison!

Parents : Oui, je comprends mon enfant. Ça fait longtemps que tu n’as pa vu tes amis. Ils te manquent?

Enfant: Oui…

Parents : Nous voulons rester en bonne santé, comment pouvons-nous les contacter sans nous exposer au virus?

Enfants: Pouvons-nous leur téléphoner?

Parents : Oui! Ou dessiner ensemble le jour où nous les reverrons ?


XAMON NGA NI? 

Waxtaan ak sa doom dina yamale bubaax yëk yëk yimiy am

Di waxtaan ak sa doom, di weccente xalaat ak mom, ak diko jox kaddu, dina ko jurël muy gëm bopam. Ndigël yekk tere yiy faral di am sunu digënte ak mom tamit dafay faral di dagg ay mën mënam teyit dey nasaxal xelam. Di waxtaan ak xale bi dina tax muy delo cër wajur bi te duko ragalit. 

ñu joxlen ben misal ci waxtaan ak sa doom numuy deme :


 

Xale bi: Dama bëgga dem si samay xarit!  bëgga tuma tokk ci kër gi!

Waajur bi: waw, japp na bu baax li nga wax. Bi nga gëje gis say xarit yag neu lolu. Da nga len namm?

Xale bi: waw

Waajur bi: Dama bëg ñun ñëp mucc, naka lañ len mën jote te wiris bi duñu jege?

Xale bi: nax mën nañ len woo telefong

Waajur bi: waw, wala ñu defando ay desin ci bis biñu len di gis

 

 

Par : Magor Dia

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *