LE SAVIEZ VOUS? 

Saviez-vous que trouver des solutions aux problèmes s’apprend dès l’enfance ?

Donner la possibilité à votre enfant d’explorer l’environnement autour de lui, permet de développer sa créativité.

Le laisser toucher, mâcher, tordre, lui permet de manipuler son environnement, et surtout de gagner en confiance en ses capacités. 

Face aux problématiques qu’il rencontrera, il sera beaucoup plus apte ainsi, à trouver des solutions !


XAMON NGA NI? 

Xamon ngen ni lijënti ay jafe jafe ci tut tànk lañkoy jange

 

Di bàyyi sa doom muy jëfëndiko liko wër dina yokk bubaax xarañteem. Buy laal, di yey, di for, di sani… dina tax muy wolu ay mën mënam. Ci kaw lolu dina don kuy mënë lijënti ay jafe jafem ba yegg ci dilen safara ci lu gaaw te yomb.

Par : Magor Dia

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *