LE SAVIEZ VOUS? 

Chanter en compagnie de son enfant stabilise ses émotions fortes

Chanter avec son enfant permet de renforcer les liens entre vous et lui, provoquant des moments de complicité et de partage. Les chansons comprenant des gestes et des mimiques aident également les enfants à prendre conscience de leurs émotions et à mieux assimiler le sens des mots. Certaines chansons nous permettent de transmettre des informations aux enfants; ce qui les installe dans une situation d’intériorisation facile et rapide. Exemple de chanson utile en cette période de COVID 19:


je frotte bien mes mains

je frotte bien dessus

je frotte bien dessous

je tourne, tourne, tourne

pour que mes mains soient propres,

et encore une fois

 

je frotte bien mes mains

je frotte bien dessus

je frotte bien dessous

je tourne, tourne, tourne

pour que mes mains soient propres,

Et je les passe sous l’eau


XAMON NGA NI? 

Xamon ngani di woy andékok sa doom dina dalal yëk yëk yu jéggi deyo yi xalé bi di am

di woy ak sa doom dina dëgërël sénug jegeyo téyit dina yokk lëko-gi ak jokalante-gi ak mom. woy yi nga xam ni bokoy woy dafa ànd ak ey zest dinay faral di yobu xalé yi ci ñuy bayi xel séniy yëk yëk ak di xame ci lu gaw li kadu yi di tekki. Amna yit ay way yuy yombal jutalik xibaar ci xale yi; lolu dina tax ñuy am tawfeexu xam ci lu gaw te yit ci lu yomb li ñu bëg ñu xamko. Ma baxe lén bén way bu am solo ngir xale yi mënë xame bu baax liñu wara def ci diamoy coronaviris bii ngi aru ci


Nanu raxasu, raxasu, raxasu ba set

mo ñuy ar, mo  ñuy ar ci coronavirus

Nañu tokk, nañu tokk ci biir kër gi

nax mo ñuy ar, mo  ñuy ar ci coronavirus

 

 

Par : Magor Dia

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *